Nguora – Gaston Bandimic

{Refrain} Ya ngui nélaw Joggal maam Mo ngui naaathie Goor Yomboul dou ni ngako fogué (X2) Da nga lambeu sa loxo mou fess sa toubeuy Rek nga fokné loloy Ngora Goor yaw ya ngui nélaw Yéwou takoussane teud ci fadjar diaroul baakou lolou dou ngora Ngora lolou dou ngora Ngora Da nga lambeu sa loxo […]